Compositor: Não Disponível
Yeah, yeah!
Yeah, yeah!
Ye-yeah, yeah!
Yeah, yeah, yeah, yeah
Aahi! woy yaay!
Xale bi ma gis, oh la-la-laa
Aahi! woy yaay!
Góor yu mel ni ndeke am na ci réew, oh yeah!
Tuuti mu jommal ma
Dama ko gis sama fit bi tëb
Jox naa ko sama call ak bu gàlle
Ba léegi woowagu ma
Te ni la jële numéroom de baaxul
Xamuma nu mu tudd
Fu mu dëkk, non-non-non-non-non
Xawma lii lan la
Laa-laa lii lan la, mbaa du lii de cat la
Ndeke amour dana dofloo (u-u-uuh!)
Ndekete dana dofloo
Sama xol nangu na ko jox lova (u-u-uuh!)
La-la-la-la-la lova
Dellu naa fa di ko seetaat, uh yeah!
Xale bi gisuma ko
Laa-laa lii lan la, Laa-laa lii lan la
Mbaa du lii de cat la
Xale bi ma gis, oh la-la-laa
Aahi! woy yaay!
Góor yu mel ni ndeke am na ci réew, oh yeah!
Tuuti mu jommal ma
Dama ko gis sama fit bi tëb
Jox naa ko sama call ak bu gàlle
Ba léegi woowagu ma
Te xol moom du óom
Non-non-non-non-non-non
Nelawatuma xawuma fu mu dëkk
Non-non-non-non-non-non
Xawma lii lan la
Laa-laa lii lan la, mbaa du lii de cat la
Gént naa ko biig mu jege ma
Jege ma ooh, jege ma
Fóon ko yeewu gis ko mu sori ma ooh
Sori ma ooh, sori ma
Yeah!
Tayuma ko bës bu ne
Sangu solu toog di ko xaar
Tu sais très bien bae bii love def na ma blème
Baby, un amour impossible
Yeah, yeah!
Ndeke dina dofloo (u-u-uuh!)
Ndekete dana dofloo
Sama xol nangu na ko jox lova (u-u-uuh!)
La-la-la-la-la lova
Dellu naa fa di ko seetaat
Uh yeah!
Xale bi gisuma ko
Laa-laa lii lan la, Laa-laa lii lan la
Mbaa du lii de cat la
Ndekke dana dofloo (uh uh uh)
Ndekke te dana dofloo
Sama xol nangu na ko jox lova (uh uh uh)
Lalala lala lova
Dellu na fa di ko seetan, uh yeay
Xale bi gisuma ko
La lalahi lala lalahi lala
Badu lii de cat la
Oh l'amour sama xol ba
Aahi! woy yaay!
Xale bi ma gis, oh la-la-laa
Aahi! woy yaay!
Góor yu mel ni ndeke am na ci réew, oh yeah!
Tuuti mu jommal ma
Dama ko gis sama fit bi tëb
Jox naa ko sama call ak bu gàlle
Ba léegi woowagu ma
Te xol moom du óom
Non-non-non-non-non-non
Nelawatuma xawuma fu mu dëkk
Non-non-non-non-non-non
Boobu ba léegi gisuma ko
Non-non-non-non-non-non
Dëgg-dëgg duma ko fàtte
Duma ko fàtte
Non-non-non-non-non-non
Laa-laa lii lan la, Laa-laa lii lan la
Mbaa du lii de cat la