Moo Ngi Fi

Amira Abed

Compositor: Não Disponível

Lila ci musël
Moy di moytu
Li ñëpp la titël
Konn bul gëmméntu

Moom dafa ñow nit ñi di dém
Janté bi soo gissatu ñu lérr
Meme samay xarit, mëna tu malen guiss
Ba ko jip day tite

Bul fàtte ni mi ngi fi (batay)
Lax ko na mais mi ngi fii (batay)
Bul fàtte ni mi ngi fi (baa tayy)
Lax ko tina mais faites gaffe

Lila ci musël
Moy di moytu
Li ñëpp la titël
Konn bul gëmméntu

Moytandiku
Ni gnouy dundék jaan ci pax
Respecté consigne yéy tax ñu dundaat lu neex
Ndax wergu yaram bu sax egal happiness
Revivons des jours meilleurs

Bul fàtte ni mi ngi fi (batay)
Lax ku na mais mi ngi fii (batay)
Bul fàtte ni mi ngi fi (baa tayy)
Lax ko tina mais faites gaffe

Together we will get there
And struggle for better days
It's time to build our future
Jok ni li daf fiey jekk (par force)

Lila ci musël
Moy di moytu
Li ñëpp la titël
Konn bul gëmméntu

Fagaro gën faju
Fagaro gën faju
Konn negn leen vacciner wu
(Vacciner wu)

Bul fàtte ni mi ngi fi (batay)
Lax ku na mais mi ngi fii (batay)
Bul fàtte ni mi ngi fi (baa tayy)
Lax ko tina mais faites gaffe

Ngir aar sa bopp aare sa njaboot
Moy respectez les gestes barrières
Baña bayé ko fiy jëlé

Li arr sa boppu aar sa njaboot (batay)
Moy respecter les gestes barrières
Fais gaffe!

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital